ROSA
Auteur – compositeur : Didier AWADI
Chœurs : Carlou D, Baay Sooley, Bouba Mendy, Ndiaya, Xuman.
Teubeul, beu naw, teubeul, teubeul beu naw
Teubeul meu teub, beu naaw
Té boul délou ganaaw
Tégueul sa mind, yaye jeul number one
Never never loose, yaye jeul number one
Jappeul mou dang, boul tayi, boul bayi
Xeutieul mou dang, boul tayi, boul bayi
Ndam, di ngueu dieul, boul tayi, boul bayi
Seugeu, dou fi am, boul tayi boul bayi
Aïtialéne niou djoubeul, tchi ndamli
Foul ak fayda djoubeul tchi ndamli
Aïtialéne niou djoubeul tchi ndamli
Jom ak fit teye djoubeul tchi ndamli
AWADI dèye big up da lion
Fouta dèye big up da lion
Tamba dèye big up da lion
Casamance dèye big up da lion
Refrain
Eh Rosa ...
Sound meu sound dou soundou tiouné
Sound meu sound dou soundou gouné
Sound meu sound dou soundou ndaré
Sound meu sound mome amoul saalé
Boul falé geumeul sa doolé
Geumeul sa body geumeul sa doolé
Boul falé nieuppeu lèye nianeul
Paa bi, mère bi, nieuppeu lèye nianeul
Voila le son qu’on dédicace aux lions
Voila le son pour les champions
Voila le son qui nous mènera à zion
Voila le son pour les champions
Kaolack dèye big da lion
Saint-Louis dèye big da lion
Kédougou dèye big da lion
Ndakaru Ndiaye dèye big da lion